Dawuuda Njaay aw ci yoon wi noom Séex Musaa Ka xàlloon. Woy yii mu wéer ci léebu yi fi Maam bàyyi xoot nanu. Di nan yar yeete suuxat xel naatal xalaat. Teewul nose bi sol galan buy dàkk xolu bépp dom Aadama. Te loolu la woykat tigi di sàkku. Daouda Ndiaye suit le chemin tracé par le précurseur Cheikh Moussa Kâ. Ses poèmes s'appuient sur les proverbes légués par les ancêtres. D'où leur richesse.
- format : 13,5 x 21,5 cm
ISBN : 978-2-296-12467-7 • juillet 2010 • 102 pages
EAN13 : 9782296124677 EAN PDF : 9782296262317 EAN ePUB : 9782296703902
* Nos versions numériques sont compatibles avec l'ensemble des liseuses et lecteurs du marché.
Les ebooks publiés avant 2011 sont susceptibles d'être issus d'une scannérisation, merci de consulter l'aperçu pour visualiser leur qualité.